Beelsebul
Apparence
Ci làkku ibrë בעל זבוב; Ci làkku yawut la tur wi jóge. Ci angale mooy Beelzebub; Ci faranse mooy Béelzébul
Yàlla ju araam la, ji waa Filisti doon jaamu ci dëkku Ekron. Yeesu moo ko tuddewoon buuru rab yi. Am na ñi xalaat ne weneen turu Ibliis la, ñeneen ñi xalaat ne meneen xel mu bon mu am kàttan ci suufu Ibliis.
Man nañu gis tur wi ci Mc 10:25; 12:24,27; Mk 3:22; Lu 11:15,18,19.