Ci angale mooy Arab; Ci faranse mooy Arabe
Naar yi, maanaam xeet yi jóge ci diiwaanu Arabi.
Araab yi bokkoon nañu ci ñi nekkoon ci Yerusalem ci Jëf 2:11.